"Soul kéér douko téré fééégn moukou"
Am na niou beuri , niouko wara déf sén biiira biir xél
Ma waxat ko "Souba limou dinthia gueuna sakane mboki alcane"
Niou déglouwatt crazy muzik , let's go....
Am na niou beuri , niouko wara déf sén biiira biir xél
Ma waxat ko "Souba limou dinthia gueuna sakane mboki alcane"
Niou déglouwatt crazy muzik , let's go....
Digital Track
Immediate download of Bril Fight 4 #CrazyMuzik Prod By Ma Ma G Beats (Hambourg - Germany) in your choice of high-quality MP3, FLAC, or just about any other format you could possibly desire.
Buy Now name your price
about
To support BrilFight4 & Ma Ma G, you can pay a small amount for this download. But you do not have to. You can also get this download for free.
To get this download for free, you just need to enter the number zero into the field. You can choose how much you want to donate. Thanks !
lyrics
Bril Fight 4 #CrazyMuzik Prod By Ma Ma G Beats (Hamburg - Germany)
credits
from Analizyk, released 24 November 2013
tags
license
all rights reserved
feeds
feeds for this album, this artist
BRIL FIGHT 4...
Crazy Muzik Lyrics
Intro :
Yeah
Everybody clap your hands
MaMa G on the beat
Bril Fight 4, The last Fighter
This is our crazy life
""""ANALYZIK"""""
That's right nigga li moy
(Good Muzik, Crazy Muzik)
Li laniouy doundou everytime, you better know
(Good Muzik, Crazy Muzik)
Refrain :
This is what we live
(Nioko sopp , défko life dithi yeungou everyday, come on)
Even if you don't believe
(Right now, it's time niou wakhla lépp louniouy doundou, tell'em)
This is what we live
Even if you don't believe
Li moy sunu life
Liniou doundou diko dééf
Couplet 1:
Nioy gni téla déglou beugg, dithi yeungou biss bouné./
yagga téylou for thi deugg, deukk thi djéngou, guiss louné./
"""""HUUUN"""""
fadjar laniou virussou sound contaminé./
djaappniou teuyé mélné allround dagnka miné./
xél di gass fépp, tégui léppeu djokhla first rime./
Djeul nga xalima ngeup, dippi deupp, reudd, séntou prime./
Guéneu thi mbéd mi, sobou thi under bi, rap, dokh di deungueul cap./
beurri thi ennemie , seugg thi mbindd mi , ndjapp, topp thi beat bi clap./
Biir classe yangui thi rythme,ba do tékk pen ci line ./
bou prof biy wakh ay algorythme, ngathiy dégg punchline./
Nékkeu thi biggie wala pac , biniouy gueustou socrate ./
seugg, siggui , gueumm , guiss li neubou , né kouy soukouratt./
Yeukné matna.... now you can do it./
Léppeu niorna, djotna nga djégué li méégneu di witt./
It's time guééné track yéék thi cons (concert) di reukk nice./
Sani Rhyme né kouy raak, real yi cons (consommer) di recognize./
Refrain:
This is what we live
(Nioko sopp , défko life dithi yeungou everyday, come on)
Even if you don't believe
(Right now, it's time niou wakhla lépp louniouy doundou, tell'em)
This is what we live
Even if you don't believe
Li moy sunu life
Liniou doundou diko dééf
Couplet 2 :
Inspiration foumla wo nga djeuliko , né kouy touki deuggueu/
Guéneu thi mbéd mi weuriko, nitt dila nouyou doko déggueu/
Thi nabou waar nga tibat , niakk time , rar dio yi /(xarit yi)
Bouniou déggué sa baat , dagnla tékk ci radio yi/
Légui tour wi lawna ba niou beuri niola oubil nopp/
Play sa son thi ordi wala thi ipod, di yeungueul bopp/
Dila woo, di bégué , nanela , "disque platine lagnla yééné"/
Té biir gaalé ,everyday nionguilay kholé alliéné//
Meunouniou comp (comprendre) teudjou thi néék, di wakh yaw dongou, répété sound
Yokhou thi kaw, yokou volume , ba nioulay tongou, yakaté round/
Tambaliwat nga.... , sa xél wakhla , dou ni , néé-la/
Djékhalago bénn couplet mére feuggla néla/
"té nga guéneu délou djangui , té bayi sa wakhtou yi/(parler seul)
Niongui nodou, nieuweul djapp, djouli , fay sa wakhtou yi/(heure de prières)
Légui yangui djaleu TV, Khol nagnla réé di mouuugn /
Fokk gueum gueum bi , djégui fayla linga yaga mougne/
Refrain:
This is what we live
(Nioko sopp , défko life dithi yeungou everyday, come on)
Even if you don't believe
(Right now, it's time niou wakhla lépp louniouy doundou, tell'em)
This is what we live
Even if you don't believe
Li moy sunu life
Liniou doundou diko dééf
Outro :
This is what we live , what we know han han han "guiss nga li liniouy doundou everytime man"
(Good Muzik, Crazy Muzik) "Diko djokh bépp number one bril a-k-a the future"
This is what we live , what we know han han han "légui yéén nieupp wakhléén"
(Good Muzik, Crazy Muzik) " bril fight 4... THE LAST FIGHTER
........................................................................................................
Enregistrement : Diégui Rails Studio
Production et Mixage : Ma Ma G (allemagne)
Mastering : Class'Chic Records
Rate This Post